Réne da niouy déllo gnoukeul ay domou Médina, biir Médina. Tambalé ko keur Haby Diallo, aar sunuye tiss. Yaguena ligueye ci ay boutelle ak khaleyi, ci mbalite léye yeungou, di ci défar louy sammeu souniou deukouwaye. Souniou fa diogué, dém keur Kré Mbaye, sunu baye diou bakh té tabé. Délo ko gnoukeul, déf na louné ci aar. Jangual na ko niou beuri tamit, amou niou fayam, dieuredeufety Kré Mbaye. Doga dém roukou bou séw, kou niow biis bobou, di ngua kham li fay khéw.